Omzo Dollar | DIP | Akhlou Brick | Ngaaka - CLASH Rap Galsen

Publié il y a dans Wax sa xalaat

New generation RAP GALSEN aka Little polonais.
Tek leen lou guënë DIP rap paname wala fékhé.
Sou #BOOBA di nguéen convaincre AKHLOU mélomane
Si adina wërngal képp, di ngueen am ay ndam.
Meuneu lekk si rap bi ay milliers de DOLLAR
Moo gueun nguéen niouy tankhal ak seen gallë
Seen clash youdoul diéekh ni ay NGAAKA you naan bière
Ngir rek BUZZ bou soof té beutoul sakh frontière.
Waxtou bi niouy néekhal rap bi ak ay clash you daaneloul frontière.
Waxtou bobou amna niouy conquerir le monde nekk ay milliardaire.
Après niou topp di wakh né rap féyoul.
Amoo si djiz ndax yow yaa tééyoul.

Show more

1,506 Vues

Featured video

  • 46:48 Série | Wiiri Wiiri - Episode 149-150

    Série | Wiiri Wiiri - Episode 149-150

    par Admin Ajoutée 7,159 Vues / 0 Likes

    Votre série "Wiiri Wiiri" avec Saaneex et Soumboulou Bathily - Episode 149-150

    Featured
  • 01:21 Lamb | Victoire de Sathies sur Ness

    Lamb | Victoire de Sathies sur Ness

    par Admin Ajoutée 4,762 Vues / 0 Likes

    Lamb | Victoire de Sathies sur Ness

    Featured
  • 03:46 Viviane Chidid | Lon Kelen

    Viviane Chidid | Lon Kelen

    par Admin Ajoutée 2,798 Vues / 0 Likes

    Découvrez le nouveau clip de Viviane Chidid feat avec le groupe banlieurz’art “Lon Kelen” réalisé en Guinee extraits de son dernier Album “Wuyuma”.

    Featured
  • 06:05 Série | Wassaa - Episode 05: Le nouveau marié

    Série | Wassaa - Episode 05: Le nouveau marié

    par Admin Ajoutée 4,218 Vues / 0 Likes

    WASSAA est une série sur la voyance qui relate les mésaventures de Coudou et Yadi, deux drôles de "seetkat" aux consultations hautes en couleurs.

    Featured

Dernières videos

Commentaires

Thanks! Share it with your friends!

URL

You disliked this video. Thanks for the feedback!